Share.

48 Comments

  1. Abdou Diallo a volontairement refusé la Main de Moussa Ndiakhitè 😢Abdou vrai Ngaka la koi ak Lou meuna khew warna dieul lokhom

  2. Mais yeffou katte ndem yi abdou Diallo di def nak nit Ki boulay nouyou doko nouyou way da niouy dakhar sa nday nga gueneu équipe bi deh

  3. Affaire bi dall diongatè leu rèkk kou nékk au top rèkk yaye joué ms rival daffa diare mèrè nitt ki dèfoula dara tmt niou wakhanntè deugg

  4. Wakhi doff mooo gni sourirou gnou danio gagneuhhh kanam pa bissi wett bi tamitt defoul yeuffou kilifa meunone na diokhé lokhom camoufler. Yaw mi si vidéo khamngani sakh waxo Lou am li mo takh Dara dou réglé teksi federation nekk tiouné sén chaîne mo nieuk guéné liii nii de chez nul

  5. Je ne connais pas les deux mais yaw mii Dioallo mi kou khéss kii doméram deugg leu yeufou imbécil yii nakk gaa mélni djiguéne nii
    Wayé yaww mi di wax nafékh bou makk geu yii féne you teuyi.
    Ki doko falé sax 😏😏😏 akk Lou meuneu khéw fayii koo publiquement lala nouyou et yaa dé caméra imbécil que tu es

  6. Bilahi😢Yaw mii di wax yaa nafékh deugg,,,
    Abdou dialo je ne te connais pas mais t’es mal éduqué
    😊quelques soit vos problèmes tu devais répondre la salutation imbécil que tu es

Leave A Reply