Gnomi nén le sén biir mais nak lii ni gagné woul algéri mangui guiss sougnou défaite ni gak fayda lolou motakh gnou commencé am ay blessé si équipe bi nit ki sa place tu dois le mériter mo geune ligéyanté bi
Yi geuthie nañe ko degue thi equip bi te yi baxoul thi group wax you sew yi baxoul epi kane mo mana dem fi jouer yi di tek sene dallue bafaye sathi xana garde yi defouniou sene liguey no li dafa ñaw way
47 Comments
Kougnou sathieu dallame n'a gueum yalla khamni fi yalla rék moffi nék lolou
Li niaw na😡
Pourquoi veux t'il la récupéré😂😂 il n'a qu'a changer de chaussures 😂😂😂😂😂
❤🎉❤🎉❤🎉🎉❤❤
Li dafa Niaw
Sénégal metti n’a 😆😭😭😭🙂🙂
Lo lomou Mana nék
Le maraboutage c la réalité sénégalaise
Incompétence pure et simple !!! Comment la fédération peut être aussi laxiste ??? 😢😢😢😢😢
Soutoural léne séne bope kou dégue lii do nieuw sénégal
Ce genre de chose doit rester dans les vestiaires.
Cheikhou kouyaté mome kène douko liguèye ndah diéhalna.
Merci bcp Nice mouhamèd djadieuf pour les informations ❤️💙💙
Sa dalle bi deh egna si Serigne beu buyagg senegal deukou lapato la tout est mystique
Merci pour les informations ❤
Senegal dou deme
Heeeeeee😂😢
Wa mais Kouyaté diaroul liguey amatoul place cii équipe bii
Lii yague n'a si équipe bi nk
Est ce que amoul foum ko tek aussi fatté yemé na dall
De toute façon cariére rame diex n'a ba paré 😂
Ms jouer yeko dieul ou bien
👍👍👍
Salif diao a déjà été victime de sa
Li mome dafa rousslou way
Gnomi nén le sén biir mais nak lii ni gagné woul algéri mangui guiss sougnou défaite ni gak fayda lolou motakh gnou commencé am ay blessé si équipe bi nit ki sa place tu dois le mériter mo geune ligéyanté bi
Ñaawna tropp , 🤦🏿♂️
C dommage
Na changé dal
Bouko solaté yakou
Thieuy yalla 😢
Kou meuna sathie ay billet stade d'où bayi godasse
Kouyaté puma lay soll tmt
Mane mako sath depuis paris 😅
Merci mohamet pour les infos il faut qu'il change de chaussure 👟 s'il l'ai retrouve
Dafa nianwe
Li dafa niaw si équipe bi billahi kouka dieul nako dollé
Dalou Édouard Mendy leu Cheikhou nekkoul Addidas
Manq de respect
Xana amoull caméra de surveillance 😮😮😮
Yi geuthie nañe ko degue thi equip bi te yi baxoul thi group wax you sew yi baxoul epi kane mo mana dem fi jouer yi di tek sene dallue bafaye sathi xana garde yi defouniou sene liguey no li dafa ñaw way
La fédération dois veiller sur la sécurité des footballeurs, surtout au Sénégal,
C honteux franchement sénégalais dmrm leu😑
Avec ça comment voulez vous que les bi nationaux viennent jouer au Sénégal amateurisme de la fede et mythisime des joueurs
No comment
Virement lii amna si Sénégal
Naniou KO thiambarr avant tout si séenne biir