Share.

21 Comments

  1. Walae deugg nga wax ba parei nitt yi dagnouy fatei nei football dou fifa wala pes joueur dafa ladj adaptation mieux encore bi moy seulement 2e équipe prowam tei il est a Marseille qu’il y’a moins d’un mois en tant joueur pro Bou Marseille nagn bayi illiman dîna gneuw deh iso mome moko geuneugoum bokk nax moko eup expérience pro tei fauk mou mine Marseille et ses coéquipiers pour mou flambée

  2. Wakh dji telna bari dh equip Marseille bi thi bopam mo degogoul pska dafa bari jouer you bess def léne ndankue rk ndiaye une challa ndam rk lay am na cocah bi guena xam fimkoy tek rk nako bayi mou libre bañe diko pointe lo ilimane dou jouer bouy xarr ball

Leave A Reply