Lutte 221 • 100% Lutte )
Est Une Chaîne Spécialisée Dans Les Combats De
Lutte Sénégalaise
Abonnez Vous Sur notre Chaine et Activez Les
A NOTIFICATIONS
Vivez La lutte Autrement
Pour Nous Contacté : + 211 76 143 09 22
#luttesénégalaise #lutte221 #luttetv #luttetraditionnelle #lambsenegal
#luttetv #lutteavecfrappe

31 Comments
Sa me rappelle eumeu séne bombardier gnep nane bombardier legui yewouna kounek Di wakh a la fin guisnagne li khew eumeu dou regu beurré dougnou benne
Pap sarr eumeu sene Day liguey Day out khalice te yaw dangay weur di niane ak wakh
Eumeu sene khamoul sakh loutakh mou diel comba bii gnoune baol lagn deuk ay baol baol lagn
Talatounou ay lambou projet ousmane sonko rèk
Emeu d'où em tous
EUMUE SENE COMBA BON WAX NI DOU SI GEN REK MO DAN AFECMADIER
Pape Sarr fow nga xamne eumeu sen nekatoul xale dieul combat wakh lako force arêtel sa thiakhan yi
Nopalal sa bop on te considère pas
Incha Allah Eumeu sène dina dane Tapha tine ba wa alkhou lamb warou😂
Pape dofffff🤣
Dof nga ken doula tagou😅😅
Yaw pape sarr katal sa ndeye felé yaw dof gna
Tapha Tine façon Beraii Boumou Beraik Boy NIANG Bouko Beraii ak Eumeu sén 200 combat Eumeu sén Douko Danne Té on Véra inchalah migui sou ou kanam bientôt inchalah ✅Tapha Mou wathi thi souf
Dof bi
Dof bi
Pape Sarr le fou mantal
Doko yeug dakh eumeu guiroulvfoula si yaw daga dof trop
Sonko Sonko 2024 2024 ❤❤❤❤❤❤
Arene bi dou féss personne ne viendra
Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko Sonko 2024 2024 2024 2024 ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Fadam diakhce rek guay def
Sounou yoneu nékoul sii lamb nervii focus 2024 emeu sène tay rékk ngay kham wa pikine guemou gñoulla nervi nou boneu biii
Fadam hana warou nga si wadji. Ki mounn na wahh😅
Eumeu ndam rek inchallah❤
Ak lou manti xow tapha Moy dan
Fadam seytanéleu, mais les gens le sauront plus tard ,le temps est meilleur juge
Merci grand pape sarr nous sommes derrière toi
Wadji limouy WAkh tek Naka si Yoon ❤
Eumeu sene dolé danouku beure bu ñor mokoy dane
Bou tapha tine téyé amoule fouko eumeu di diarr pour dane ko eumeu tank tapha rékkk lay outtttt
Bou eumeu danné moy roi des loures